Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 40:13-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 40:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Ay musibaa ma tanc, ne gàññ, ba wees ab lim. Samay ñaawtéef a ma dab, ba gisatuma, baree bare, ba ëpp sama kawari bopp; sama xol jeex tàkk.
14 Éy Aji Sax ji, yal na la neex, nga wallu ma! Éy Aji Sax ji, gaawe ma!
Sabóor 40 in Kàddug Yàlla gi