Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 3:5-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 3:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 Maay woo Aji Sax ji wall, mu walloo ma fa tundam wu sell wa. Selaw.
6 Maay tëdd nelaw, yewwu; Aji Sax ji di ma aar.
Sabóor 3 in Kàddug Yàlla gi