Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 39:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 39:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Nit du lu moy takkndeer buy dem, cóolóolu neen lay kër-këri. Nit a ngi dajale, xamul kuy for.
8 «Éy Boroom bi, lu may xaarati? Sama yaakaar yaw a.
Sabóor 39 in Kàddug Yàlla gi