Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 39:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 39:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Dama noon cell, ne patt, noppi, ba mu ëpp; sama njàqare yokku,
4 sama xol diis, xel di xelaat, xol diis gann; ma mujj àddu,
Sabóor 39 in Kàddug Yàlla gi