Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 37:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 37:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Dénkul ci Aji Sax ji, di def lu baax, ba des ci réew meek jàmm.
4 Deel bànneexoo Aji Sax ji, mu may la say nammeel.
5 Jébbalul ci Aji Sax ji, dénku ci moom, mooy sottal.
Sabóor 37 in Kàddug Yàlla gi