Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 37:19-22 in Wolof

Help us?

Sabóor 37:19-22 in Kàddug Yàlla gi

19 Bu mettee doo rus, te bésub xiif dangay regg.
20 Ku bon sànku; noonub Aji Sax ji, taaru tool bu naat la, bu tàkkee, jeex tàkk.
21 Ku bon leb, du fey; ku jub yéwén, di joxe.
22 Aji Sax ji barkeel la, nga jagoo réew mi moos; mu alag la, nga dog.
Sabóor 37 in Kàddug Yàlla gi