Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 36:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 36:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Sa njekk a tiim tund yu mag yi, sa àtte ne xéew ni xóotey géej. Céy Aji Sax ji, nit ak mala, nga boole sàmm!
8 Céy Yàlla, yaa wéet ngor, doom aadama yiiroo sa ker, yiiru;
Sabóor 36 in Kàddug Yàlla gi