Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 35:5-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 35:5-9 in Kàddug Yàlla gi

5 Yal na leen malaakam Aji Sax ji bëmëx, nim ñax mu ngelaw wal.
6 Yal na leen malaakam Aji Sax ji dàq, ñuy lëndëmtuy tarxiis.
7 Defuma dara, ñu di ma fiir, defuma dara, ñu gas um yeer, di ma tëru.
8 Yal nañu sànkoo mbetteel, keppoo seen fiir, sànkoo seenum yeer.
9 Su boobaa ma bége Aji Sax ji, bànneexoo wallam,
Sabóor 35 in Kàddug Yàlla gi