Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 35:23-26 in Wolof

Help us?

Sabóor 35:23-26 in Kàddug Yàlla gi

23 Jógal, sàmmal ma sama àq. Sama Yàlla, Boroom bi, àtte ma yoon.
24 Aji Sax ji sama Yàlla, àttee ma sa dëgg, ñu bañ maa ree!
25 Yàlla buñu ne: «Ñaw! Lii rekk lanu bëggoon.» Yàlla buñu ne: «Sàkkal nanu ko pexe.»
26 Ku bége sama njàqare, yal nanga rus, ba torox. Kuy réy-réylu ci sama kaw, yal nanga am gàcce, ne yàcc.
Sabóor 35 in Kàddug Yàlla gi