Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 35:13-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 35:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Man de ba ñu woppee, maa ngi ñaawlu, di woor, toroxloo, sukk, ñaanal leen,
14 tiisoo leen ni saab xarit mbaa doomu ndey, di ñaawlook a yoggoorlu ni ku ñàkk yaay.
Sabóor 35 in Kàddug Yàlla gi