Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 34:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 34:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Néew-ji-doole woote, Aji Sax ji wuyu, musal ko fu mu jàqe.
8 Ku ragal Aji Sax ji, malaakaam yiir la, di la wallu.
9 Mosleen, xam ne Aji Sax jee baax, ndokklee yaw mi ko làqoo.
Sabóor 34 in Kàddug Yàlla gi