Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 34:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 34:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Aji Sax ji laay sagoo, néew-ji-doole dégg, bég.
4 Kañleen Aji Sax ji, ànd ceek man, nu bokk wormaal turam.
5 Maa sàkku Aji Sax ji, mu nangul ma, tàggale maak lépp lu ma ragal.
6 Ku yaakaar Aji Sax ji bég, leer nàññ, gàcce du ko sëlëm.
Sabóor 34 in Kàddug Yàlla gi