Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 34:19-22 in Wolof

Help us?

Sabóor 34:19-22 in Kàddug Yàlla gi

19 Sa yaakaar tas, Aji Sax ji jege la, sa xol jeex, Aji Sax ji wallu la.
20 Musiba bare naa dal ku jub, Aji Sax ji musal ko ci lépp,
21 di ko sàmm, ba benn yaxam du damm.
22 Musiba nag day rey ku bon, te ku bañ aji jub, yoon dab na la.
Sabóor 34 in Kàddug Yàlla gi