Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 34:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 34:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Na làmmiñam daw lu aay, dawi fen.
15 Na dëddu lu bon tey def lu baax, sàkku jàmm, saxoo ko.
16 Ay gët la Aji Sax ji ne jàkk aji jub ji, te ay noppam la dékk wooteb wallam.
Sabóor 34 in Kàddug Yàlla gi