Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 33:4-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 33:4-6 in Kàddug Yàlla gi

4 Aji Sax jee jub kàddu. Mooy jëfe lépp kóllëre.
5 Moo sopp dëgg ak yoon. Aji Sax ji, ngoram a fees àddina.
6 Kàddug Aji Sax ji la asamaan sosoo, ci baatam la gàngoori asamaan yépp sàkkoo.
Sabóor 33 in Kàddug Yàlla gi