Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 33:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 33:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Fental-leen ko woy, xalam, mu neex, sarxolle jib.
4 Aji Sax jee jub kàddu. Mooy jëfe lépp kóllëre.
5 Moo sopp dëgg ak yoon. Aji Sax ji, ngoram a fees àddina.
Sabóor 33 in Kàddug Yàlla gi