Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 33:15-17 in Wolof

Help us?

Sabóor 33:15-17 in Kàddug Yàlla gi

15 Moo tabax seen xol, ñoom ñépp; lu ñu def, xam na ko.
16 Mbooloo mu réy mayul Buur ndam, doole ju bare walluwul jàmbaar.
17 Yaakaar aw fas nax sa bopp la, kàttanu fas dug wall.
Sabóor 33 in Kàddug Yàlla gi