Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 33:13-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 33:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Asamaan la Aji Sax jiy jéere, di gis doom aadama yépp.
14 Jal ba mu tooge lay niire waa àddina sépp.
Sabóor 33 in Kàddug Yàlla gi