Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 33:12-13 in Wolof

Help us?

Sabóor 33:12-13 in Kàddug Yàlla gi

12 Ndokklee yeen xeet wi Aji Sax ji di seen Yàlla, yeen askan wi Aji Sax ji séddoo.
13 Asamaan la Aji Sax jiy jéere, di gis doom aadama yépp.
Sabóor 33 in Kàddug Yàlla gi