Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 31:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 31:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Maa bañ kuy topp tuuri neen. Man, Aji Sax ji laa wóolu.
8 Damay bég, di bànneexoo sa ngor, li nga xoole samaw tiis. Ràññee nga sama njàqarey xol.
Sabóor 31 in Kàddug Yàlla gi