Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 31:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 31:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Damaa dégg jëw yu bare, lu raglu dar ma kepp. Ñu ngi mànkoo, di ma fexeel, di wut sama bakkan.
15 Man nag Aji Sax ji, ci yaw laa dénku. Ma ne: «Yaay sama Yàlla.»
16 Yaa yor sama àpp. Xettli maak ku ma noonoo ak ku may sonal.
Sabóor 31 in Kàddug Yàlla gi