Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 2:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 2:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Ña nga naan: «Nanu dagg càllala yi, sànni jéng yi!»
4 Ki ci jalub asamaan a ngay ree, Boroom baa nga leen di kókkali,
Sabóor 2 in Kàddug Yàlla gi