Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 28:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 28:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Aji Sax jee may dooleel, di ma feg. Moom laa wóolu, mu wallu ma, sama xol tooy, ma woy, sante ko.
8 Aji Sax jeey dooleel ñoñam. Mooy làq, di musal buur bi mu fal.
Sabóor 28 in Kàddug Yàlla gi