Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 28:5-7 in Wolof

Help us?

Sabóor 28:5-7 in Kàddug Yàlla gi

5 Xooluñu Aji Sax jeeki jëfam, ak liggéey bi mu def. Da leen di yàqte, te dootu leen yékkati.
6 Jaajëfe Aji Sax ji, ki ma nangul samay dagaan!
7 Aji Sax jee may dooleel, di ma feg. Moom laa wóolu, mu wallu ma, sama xol tooy, ma woy, sante ko.
Sabóor 28 in Kàddug Yàlla gi