Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 27:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 27:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Éy Aji Sax ji, déglul, ma woote! Ngalla baaxe ma, nangul ma.
8 Yaw la sam xel ne ma, ma sàkku la, te it yaw Aji Sax ji laay sàkku.
9 Sang bi, bu ma làqu, bul mer, jañax ma. Yaa ma daa wallu. Bu ma wacc, bu ma ba, yaay Yàlla mi may musal.
Sabóor 27 in Kàddug Yàlla gi