Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 26:7-10 in Wolof

Help us?

Sabóor 26:7-10 in Kàddug Yàlla gi

7 àddu, sant la, lim sa jépp jaloore.
8 Aji Sax ji, maa sopp sa dëkkuwaay, bëgg bérab bi sag leer teew.
9 Bu ma buubaaleek bàkkaarkat, sànni, di ma booleek bóomkat, bóom.
10 Seeni yoxoo nga sóobu ci mbon, ndijoor ya fees aki ger.
Sabóor 26 in Kàddug Yàlla gi