Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 26:4-7 in Wolof

Help us?

Sabóor 26:4-7 in Kàddug Yàlla gi

4 Toogumaak naxekat, lëngoowumaak naaféq,
5 sib naa gàngooru saaysaay, toogumaak ku bon.
6 Aji Sax ji, maay jàpp ci biir mucc ayib, di wër sa sarxalukaay,
7 àddu, sant la, lim sa jépp jaloore.
Sabóor 26 in Kàddug Yàlla gi