Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 26:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 26:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Maa ngi janook sa ngor, di jëfe sa worma.
4 Toogumaak naxekat, lëngoowumaak naaféq,
5 sib naa gàngooru saaysaay, toogumaak ku bon.
Sabóor 26 in Kàddug Yàlla gi