Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 25:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 25:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Bul xool li ma bàkkaare ndaw ak li ma moy. Aji Sax ji, xoole ma sa ngor ngir sag mbaax.
8 Aji Sax jee baax, rafeti dogal, di gindi moykat ci yoon wi,
9 di jiite ku woyof mbubb ci njubte, di ko xamal aw yoonam.
Sabóor 25 in Kàddug Yàlla gi