Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 25:2-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 25:2-4 in Kàddug Yàlla gi

2 Sama Yàlla, yaw laa yaakaar. Yàlla buma rus, noon yi ree.
3 Deesu la séentu, ba rus. Kuy wor ci neen mooy rus.
4 Éy, Aji Sax ji, won ma saw yoon, xamal ma fi nga ma jaarloo.
Sabóor 25 in Kàddug Yàlla gi