Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 25:13-15 in Wolof

Help us?

Sabóor 25:13-15 in Kàddug Yàlla gi

13 muy dunde ngëneel, askanam moom réew mi?
14 Ndéeyu Aji Sax ji, jagley ku ko ragal. Kóllëreem la koy xamal.
15 Samay gët jàkk rekk ci Aji Sax ji, moo may xettli ci fiiru noon.
Sabóor 25 in Kàddug Yàlla gi