Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 24:8-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 24:8-9 in Kàddug Yàlla gi

8 Buur Boroom ndam booboo di kan? Xanaa Aji Sax ji Boroom dooleek njàmbaar, Aji Sax ji jàmbaaru xare ji.
9 Neleen bunt yi kulbét, ubbileen bunti cosaan yi, Buur Boroom ndam duggsi.
Sabóor 24 in Kàddug Yàlla gi