Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 24:4-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 24:4-6 in Kàddug Yàlla gi

4 Xanaa ku mucc ayib, sell ab xol, xemmemul caaxaani neen, du giñey fen.
5 Kookooy jagoo barkeb Aji Sax ji, ak njekku Yàlla, mi koy musal.
6 Ñooñooy waa làng, gi lay sàkku, di maasug Yanqóoba, giy sàkku sa yiw. Selaw.
Sabóor 24 in Kàddug Yàlla gi