Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 24:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 24:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Ana kuy yéegi tundu Aji Sax ji, kuy taxawi bérabam bu sell ba?
4 Xanaa ku mucc ayib, sell ab xol, xemmemul caaxaani neen, du giñey fen.
5 Kookooy jagoo barkeb Aji Sax ji, ak njekku Yàlla, mi koy musal.
Sabóor 24 in Kàddug Yàlla gi