Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 24:2-3 in Wolof

Help us?

Sabóor 24:2-3 in Kàddug Yàlla gi

2 Moo samp suuf biir géej, dëj ko ci kaw wal mi.
3 Ana kuy yéegi tundu Aji Sax ji, kuy taxawi bérabam bu sell ba?
Sabóor 24 in Kàddug Yàlla gi