Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 22:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 22:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Man nag aw sax rekk laa, matuma nit. Doom aadama sewal ma, aw xeet tuutal ma.
8 Ku ma gis ñaawal ma, biiñ ma, xeelu ma, naa:
Sabóor 22 in Kàddug Yàlla gi