Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 22:6-10 in Wolof

Help us?

Sabóor 22:6-10 in Kàddug Yàlla gi

6 Yaw lañu daa woo wall, mucc; yaw lañu wóolu woon te rusuñu.
7 Man nag aw sax rekk laa, matuma nit. Doom aadama sewal ma, aw xeet tuutal ma.
8 Ku ma gis ñaawal ma, biiñ ma, xeelu ma, naa:
9 «Na wéeroo Aji Sax ji, mu xettli ko; su ko soppee, na ko wallu.»
10 Yaw de yaa ma roccee sama biiru ndey, naxe ma sama weenu yaay.
Sabóor 22 in Kàddug Yàlla gi