Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 22:5-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 22:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 Yaw la sunuy maam wóolu woon, wóolu la, nga xettli leen.
6 Yaw lañu daa woo wall, mucc; yaw lañu wóolu woon te rusuñu.
Sabóor 22 in Kàddug Yàlla gi