Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 22:20-22 in Wolof

Help us?

Sabóor 22:20-22 in Kàddug Yàlla gi

20 Waaye yaw, Aji Sax ji, bul sore; yaa may dooleel, gaawe ma.
21 Xettlil sama bakkan ci saamar, ba sama benn bakkan bii mucc selli xaj!
22 Musal ma ci pàddum gaynde ak ndañum nagu àll. Yaa ma wallu woon!
Sabóor 22 in Kàddug Yàlla gi