Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 22:13-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 22:13-16 in Kàddug Yàlla gi

13 Noon yaa ngi ma gaw ni coggalu yëkk, dar ma ni ponkali yëkk ya fa Basan.
14 Ñu ŋa ma, ŋàpp, ni gaynde, guy yëmmook a fàdde.
15 Doole ŋiis, yax yoqi, fit ne soyox, seey.
16 Làmmiñ taqoo denqleñ, doole jeex, ma wow koŋŋ, nga tëral ma buntu bàmmeel.
Sabóor 22 in Kàddug Yàlla gi