Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 22:13-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 22:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Noon yaa ngi ma gaw ni coggalu yëkk, dar ma ni ponkali yëkk ya fa Basan.
14 Ñu ŋa ma, ŋàpp, ni gaynde, guy yëmmook a fàdde.
Sabóor 22 in Kàddug Yàlla gi