Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 21:3-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 21:3-8 in Kàddug Yàlla gi

3 Yaa ko may nammeeli xolam, gàntuwulooy dagaanam. Selaw.
4 Yaa ko gatandoo barkey ngëneel, kaalaa ko wurusu ngalam.
5 Mu ñaan mucc, nga saxal jalam fàww,
6 sag wall a ko sagala sagal! Teddngaak daraja nga ko sédd,
7 jagleel ko barke bu sax dàkk, bégale ko sa kanam, mu bànneexu.
8 Buur wóolu na Aji Sax ji, moos, du tërëf, Aji Kawe jee gore.
Sabóor 21 in Kàddug Yàlla gi