Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 21:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 21:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Yaa ko may nammeeli xolam, gàntuwulooy dagaanam. Selaw.
4 Yaa ko gatandoo barkey ngëneel, kaalaa ko wurusu ngalam.
5 Mu ñaan mucc, nga saxal jalam fàww,
6 sag wall a ko sagala sagal! Teddngaak daraja nga ko sédd,
Sabóor 21 in Kàddug Yàlla gi