Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 20:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 20:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 yal na la yónnee wallam fa këram, jàpplee la fa, ca Siyoŋ.
4 Yal na xool loo ko jébbal, di rafetlu sarax soo ko lakkal. Selaw.
5 Yal na la may li nga namm, di sottal loo mébét,
Sabóor 20 in Kàddug Yàlla gi