Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 19:13-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 19:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Nit juum na, umple ko, baal ma tooñ gu ma umple.
14 Te Sang bi, musal ma ci bàkkaaru teyeef, mu bañ maa jiital, ma mana maandu, mucc moy gu réy.
Sabóor 19 in Kàddug Yàlla gi