Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 18:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 18:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Ma jàq, woo Aji Sax ji, ne sama Yàlla wallóoy, mu dégge këram. Ma yuuxu, muy dégg.
8 Mu mer, suuf yëngu, di ker-keri; kenuy tund ya jaayu, di reg-regi.
9 Saxar di sël-sëlee ca wakkan ya, sawara boye ca gémmiñ ga, xal yu yànj tàkke ca.
Sabóor 18 in Kàddug Yàlla gi