Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 18:3 in Wolof

Help us?

Sabóor 18:3 in Kàddug Yàlla gi

3 Aji Sax ji laay sës, mu di ma aar, di ma wallu. Mooy sama Yàlla, ji may sës, yiiru, fegu; mooy Boroom doole ji may musal, di ma làq.
Sabóor 18 in Kàddug Yàlla gi