Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 18:19-21 in Wolof

Help us?

Sabóor 18:19-21 in Kàddug Yàlla gi

19 Ñu dajeek man, bés ba ma jàqee, Aji Sax ji taxawu ma,
20 yaatal ma, bége ma, ba xettli ma.
21 Aji Sax jee ma yool sama njekk, samay loxoo set, mu fey ma.
Sabóor 18 in Kàddug Yàlla gi