Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 18:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 18:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Aji Sax jee dënoo asamaan. Aji Kawe jee àddu, muy tawub yuur ak xali sawara,
15 mu soqiy fitt ak jumi melax, tasaare leen, fëlxe.
16 Aji Sax ji, dangaa gëdd, nokki, mu riir, xuri géej ne fàŋŋ, kenuy suuf ne duŋŋ.
Sabóor 18 in Kàddug Yàlla gi