Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 18:13-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 18:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 leer a ko jiitu, xàmbaar ya topp ca, ak tawub yuur ak xali sawara.
14 Aji Sax jee dënoo asamaan. Aji Kawe jee àddu, muy tawub yuur ak xali sawara,
Sabóor 18 in Kàddug Yàlla gi